Lyrics to Borom Bi
Borom Bi Video:
Douma tiit té douma weet Fileeg fileeg maangi weetal Kima saakk Douma tiita tiit ta weeta weet Fiileek maangui weetal kima saak
Douma tiit té douma weet Fileeg fileeg maangi weetal Kima saakk Douma tiita tiit ta weeta weet Fiileek maangui weetal kima saak

When I was younger I used to look up in the sky High to see if there is no glimmer of heaven above And look down with believe under my feet see if ain't no hell below so the more you grow The more you learn life is a permanent fight only with self knowledge you know it Burn him who Devil with his evil Turn your back and walk away he's your enemy number one Lepp leer sam sam thiangou ba noppi naan charrou ramadaan ma daan Li werr te woor tambali taaya Aaya moyou limou aayé douma tchi taayé ii

Douma tiit té douma weet Fileeg fileeg maangi weetal Kima saakk Douma tiita tiit ta weeta weet Fiileek maangui weetal kima saak
I'm not alone I'm not afraid As long as I know that you're all along the way I am neither alone not afraid As long as I know you're along the way

The virus of evil spreads out like wildfire The Devil's army strides along and won't retire But the pure souls get higher and higher In the fortress of the All Mighty them dwell peaceful Manouma tiit manouma weet Fileek maangi weetal kima sakk borom bi moo niou sargal tchi bani adamak hawa ma waat guigne naako tchi doomi baay ak yaay Rassoulillahi amoul morom guignenaako tchi samay thieur ak samay rouh borom bi mooma moom

Douma tiit té douma weet Fileeg fileeg maangi weetal Kima saakk Douma tiita tiit ta weeta weet Fiileek maangui weetal kima saak
I'm not alone I'm not afraid As long as I know that you're all along the way I am neither alone not afraid As long as I know you're along the way

Yalla maynama fit douma daw ni fitt sama fitLaanaan khiitch bamouné kiitch
Bourbi yallaay sama njiit one two three ma andak sama crew digui daaraj Lakhounaa njoum aj njaakhoum ci laqad jaakoum sama khelangui sepp sepp sama guemigne Tay ma yabbi lima sekh nandal bepp kaaba ci sama dekh Fass yeene leen taff ci guouy tekh Doyma ferr itam sama daa dou dieekh Kepp kepp kouma jeuli nagnou bokk ndeey daggane ci bourbi yalla leerou peey mou mouna joubal soygnoup ligeey Aliwa daa la marr Xalima tchi kou
la far Jangal ay saar bani arr Jangal sa dine bani arr Mooy sa mbokki mbaar Bila mana aar tchi njabar Yaw mi jeul khanthi fekhe ba sank nit ki yalla sakk ba barzaaqYaw dinko layoo woaayy!!

Douma tiit té douma weet Fileeg fileeg maangi weetal Kima saakk Douma tiita tiit ta weeta weet Fiileek maangui weetal kima saak
I'm not alone I'm not afraid As long as I know that you're all along the way I am neither alone not afraid As long as I know you're along the way

(Merci à peter pour cettes paroles)
Songwriters:
Publisher:
Powered by LyricFind