El Prisident Lyrics

Fata

Non-album songs

Lyrics to El Prisident
El Prisident Video:
si c'est ça ne le cesse pas
fais le a 100%
comme ça on va quitter le minimum
pour en arriver au maximum
c'est possible si on le veux
partir de rien
pour devenir quelqu'un un jour (2x)

moytoul di doundou sa ma kow sinon na la tek deal diar sa kaw
rouler samay huit huit
tak samay bling bling
fale wouma seni dream

senegal ya nek sama khol
rey ngua si mane lol
matina ma guiss nienen ni soutla lol
souma sagnine baol
diogue si tol don metropole
kon bok def len niou khol
bala none yi di niou kholé betou kou ligueyam tiol
hip hop new generation
yenay sou nou yakar
boulen ko tass
d'accord
sinon di nguen am bakar

si c'est ça ne le cesse pas
fais le a 100%
comme ça on va quitter le minimum
pour en arriver au maximum
c'est possible si on le veux
partir de rien pour devenir quelqu'un un jour (2x)
Songwriters:
Publisher:
Powered by LyricFind