Lyrics to Souba
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Gnaféla birmi mané gnaféla
Guisga yaw loula war moy gnaféla
Ndanga dioque si ça dieulebéne
Bala moye wessou ga dico reuthiou
Mané doiksi dioksi yaw dale
Mané doiksi dioksi yaw waye
Mané doiksi dioksi yaw dale
Bala moye wesso

Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco

Wayé soumété ga dawe goor

Boule fowé sa daw domou daye
Goor yalla dara dou yombeu ya
Diambar dara dou yombeu ya

Gnaféla birmi mané gnaféla
Guisga yaw loula war moy gnaf...
Gnaféla birmi mané gnaféla
Guisga yaw loula war moy gnaféla
Ndanga dioque si ça dieulebéne
Bala moye wessou ga dico reuthiou
Mané doiksi dioksi yaw dale
Mané doiksi dioksi yaw waye
Mané doiksi dioksi yaw dale
Bala moye wesso

Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco
Soubaye dakeu taye waye
Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco
Songwriters: Alexandre Damien Chiere, Lansana Sane, Louis Teillet, Paul Andre Louis Cucuron
Publisher: Lyrics © Universal Music Publishing Group
Powered by LyricFind